×

NARA P L'OFFICIEL's video: Nara P-Kaddu Buur EP2 ft Bakhaw Da Brains

@Nara P-Kaddu Buur EP2 ft Bakhaw Da Brains
Kaddu Buur est une série de vidéos visant à informer et sensibiliser les populations sur les enjeux des élections présidentielles de 2019. Nara P fustige dans ce deuxième épisode la violence et les actes de barbaries dans la campagne électorale. Il appelle les citoyens au calme et à un retrait massif des cartes d'électeurs afin de pouvoir faire leur choix de par les urnes. Auteur : Nara P et Bakhaw Da Brains Arrangement: Djiby Da Brains Directed by: Malcom Prod Infographe: Ziza Prod Make Up: Mbene Mbacké Producteur exécutif: ¨Penku Side Prod'Action & Da Brains Production Retrouvez Nara P sur : Facebook : https://www.facebook.com/Nara-P-1924086814491593/ Instagram : https://www.instagram.com/narapi93/ Twitter : @NaraP12 Contact : (+221) 77 802 40 15 Email : narapi93@gmail.com LYRICS Intro : Bakhaw Senegal élection yii yeksina Nit yangay rayanté !! Thiey waay Beugue nek ndjiite ndeysane mo waral Gnouy rero saganték doranté ndeysan !!! 1er Couplet : Nara P Buur dikat ak kadom si benen pathie Dilen gnakh dal Bou paka gueneuh mbar bougne degue rirou bal yi Rick dey Khamelen cii wakh yi wakhdji nirok kathie Degna ndar domou diambour lagnfa lathié Matnam tol Waxouma nit beuga djité nitam xolay lay wakh Bo loré nit xol ko sa bop khana mala len rakh Liiii Killifa diné bi yaway sougnou mbagne gathié Kaddu bouy djip na done bouy bolé gneup wawkey Dionganté kat yangui feté si vdn bi Dou yenak ken gnoune la sougn biir wagnilen haine bi Demb wesna wakhal tay lo mena gadou eleuk Transumence bi takh nga wara khipi lekelok deugue Beugu falou kep diaroul rendi khar loukofi diar Amana ngour guingay khethiou doko fi khar Lou diar ay sacrifice ngourou adouna Boudé doraté takh nga beugu yeek wade wathina Tay rongognou buur tourouna Boudé dieufine bou rafet moy fess biir sourouma Bayil sa xel khaliss warougnou tardel Gnom alal lagnouy sakou gnoune sougn eleuk lagnouy gathiel Liy sama ndiekhital guinaw nguen dieuli carte yii falal domi rewmi deugue khetou cheikh anta gui Campagn yi si diam boulen khex fingueni dadié Yalna yalla fal ki gueun reuk dey Wassalam Refrain : Bakhaw Senegal élection yii yeksina Nit yangay rayanté !! Thiey waay Beugue nek ndjiite ndeysane mo waral Gnouy rero saganték doranté ndeysan !!! 2ème Couplet : Nara P Oooooohhhhh!!!! Mame gnewna yeksilak diam gorgui Boul yeketi fitna gnanal gnou woté ko si diam Nagn nek exampal dimbili khaleyi di diangue Bou ken boy coté gorgui walay lol dou diam Cissé lo killifa dou saga khana djitewo Am nga dom bou guouné yii fayo doula siwissé lo Yalla safaral gni gagnou bal gni deh soffeur yi dawal lenn si ndank ndakh douté yagu yagu yegu bossi dawal dinga wagni deh Refrain : Bakhaw Senegal élection yii yeksina Nit yangay rayanté !! Thiey waay Beugue nek ndjiite ndeysane mo waral Gnouy rero saganték doranté ndeysan !!!

2.6K

332
NARA P L'OFFICIEL
Subscribers
28.5K
Total Post
74
Total Views
0.9M
Avg. Views
15K
View Profile
This video was published on 2019-02-14 03:05:00 GMT by @NARA-P-L'OFFICIEL on Youtube. NARA P L'OFFICIEL has total 28.5K subscribers on Youtube and has a total of 74 video.This video has received 2.6K Likes which are higher than the average likes that NARA P L'OFFICIEL gets . @NARA-P-L'OFFICIEL receives an average views of 15K per video on Youtube.This video has received 332 comments which are higher than the average comments that NARA P L'OFFICIEL gets . Overall the views for this video was lower than the average for the profile.

Other post by @NARA P L'OFFICIEL